Encore un cas inédit. Cette fille de 21 ans se confie sur sa vie privée.
Je suis une fille de 21ans, je suis mariée depuis 4 mois avec un gars exceptionnel “lepp louniouy outt ci goor amna ko mais problème bi moy sama djeukeur day saaw lale. Yobounako founé pour mou fadiou. Deff na fadiou wolof mais rien. Diahléna deh t’es metti na trop damay ragal sah sama jankk yi khamko ci mom parce que nioy defar sama chambres chaque matin”.
Il se lève tôt ma defar nekk bi changer draps yi. So hamé kouko meuna jappalé svp parce que hawma conséquences yi dakh douma walleu febar wala ».